A LA UNE
Ouztaz Makhtar Sarr: Maman Diaga ku baax la ta bëgg lubaax

Innaa lillaahi Wa innaa ilayhi Raajihuun
Ndeysaan Adja Ndéye Fatou Diouf « Diaga »
Limay seede ta Yàlla tax ta sama benn Wóllare buko jege di ligéeyée SenTv waxama ko : Bima amee jafe jafe ak kenn ci njabootam, dafneko Àndu ma ci dellul ginnaaw, Oustaz Makhtar, nitu Diine kuy def rôle lam la !
Lii nak kuko wax sa njaboot ci jamono yooyu taxaw ci ku baax nga ta bëgg lubaax !
Yàlna ko Yàlla yërëm xaareko Aljana Woyofal Suuf ci Kawam