A LA UNEACTUALITES
Adiouza: Dewenaty les amis

Adiouza:
 »Dewenaty les amis, Ramadan mubarak,
Yalla nagnou yalla maye gnou fekker ko aye dewenne you barrer barrer. Yalla nagnou yalla bale sunu bakar yeup. Nangoule gnou sounou koor, maygnou talle ak fekker ak xeweul saawane bawane. Di gnane diam la paix saxe Senegal. »