A LA UNE
Ndeye Marie de la série Karma: dama nobe sama dieukheur, wolouko, gueumeko, diko tarbiyou

Célébrons l’amour ce soir mes amis.
Sama dieukheur, sama kharite beneu bakane la. Ma nopeko, wolouko, gueumeko, diko tarbiyou nak louma meune SEYDI DIA. Le plus beau.
Happy Valentine day papou Annabelle. Naniou diam rek sonal! Sa diabar nopenala, nianalnala, fo diar yonela!
Toujours là pour moi, toujours là pour me donner une bonne énergie!
TOUJOURS LÀ POUR ME SOUTENIR DANS MES PROJETS!
Yallah namala Yallah fayal ! Soûla neihone tereima ligueye bi mais au contraire JE SUIS TON FAN NUMÉRO 1 lolou rek lay deigueu.