Uncategorized
A la Une

Sidath Thioune lance des pics à la Rfm et à la Tfm

Sidath Thioune lance des pics à la Rfm et à la Tfm

Ayant quitté la Rfm, où il animait une émission à la Radio Sidath Thioune n’en pas décidément fini avec le groupe de presse. Il a fait sortir une vidéo où il lance des pics aussi bien qu’à la Rfm mais aussi à la Tfm. Il n’a pas mâché ses mots concernant le groupe de presse, il avance: « Presse nagnou kholate sen bope. Bigniy dokh ci adina bagnou jieul ab télé toudéko Télé Faral Macky(TFM) téh sa bougnou heuyé di ame gathié ci niom, sa bougnou heuyé di ame lougnou nakari ci niom. Ndah kou melni Premier Ministre Ousmane Sonko waroul nieuw ba Magal Touba nek ak Khalife Général nga hamineténi événement gueunouta reuy, Magal Touba, gnou jieul ay éléments 2018 diko dougual bay togue dici jiégalou, nga hamnité li gathié gueunouko reuy ci Télé Taral Macky. Gnou fogueni fala yam Radio Faral Macky(TFM), gnou naneko yokeu thiéré doli niéh, yokouci né khalife bi kat fimou tolou ni, mo jiohé ndigual pour manam guane youy jiougué bitim réw gnou réserverlen fofou ci king fahd palace. Serigne Bass Abdou Khadre mingui hamni mo yoré kadou Khalife Général des Mourides né lolou dé mossougnouko sakou, mossougnouko wakh yitam. Conn yakarna bala gnou guéné information dagno wara dém défi ay investigations, c’est très important ndahté wakh balle la sou hassé ba guéneuh rek démna. Presse ligniko digual moy informer juste et vraie. Mais pas di dokhalei no hamni diakhassé ak yakeu, aussi manipuler la population molen di taha diougue. Kou yabo kholate sa bope ndakh liguéye ligneci sokhla professionnalisme, dagneci sokhla rigueur, de même que détermination. Mani délén ham finguen di tégueu sen tank tay dokhal deug. Moy ndieuk moy moujie. Motah niouni joub, joubal, joubanti. Joubanti bamou bakh, jiohko askane wi. Jianguen jieuf. »

Articles similaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Bouton retour en haut de la page