Uncategorized
No Face: Ma dem aéroport gnoumay kokali
No face:
Dafa ame biss madone Tukki
AIBD – Ma Rombe contrôle di dougou embarquement. Femme yi nék si boutique bi aprè douane guissema rék changer music bidone daw si system airport bi Ték bénene music bignu ma done clash. Kunék di dokh sama kaname di wayantu son bi