A LA UNE
Griff Diouf: Nio bokone secret 535 Salallahou Halla Mouhamadine moi et Maman Diaga
Griff Diouf très proche de Maman Diaga ne tarit pas de témoigner sur la belle personne qu’était Maman Diaga aussi bien à l’intérieur qu’à l’extérieur. Griff d’avancer: Maman Diaga niane rek nga sokhla, InshaAllah dingako ame. Nio bokone secret 535 Salallahou Halla Mouhamadine.
Souniou paré wird goudi aljummah, kou nek na def 41 ikhlass, defko adiya Rassoullilah (S.A.W), sinou borom defko yeurmandé sottiko Ndeye Fatou Diouf Diaga.