Uncategorized
A la Une

Marie Faye la dame sociale de Facebook: tay j’ai craqué ndakh métite ak fébar depuis bima yéwo coma batay

Marie Faye la très généreuse dame sociale qui assistait les personnes malades et diminues et les personnes en situation de difficultés vient de faire l’annonce terrible de sa maladie qui la terrorise. Insoupçonnée par sa communauté sur les réseaux sociaux car mettant toujours l’ambiance et taquinant à tout bout de champ, l’annonce de sa maladie a attristé et bouleversé tout le monde. Marie Faye de se confier:

Fébar bou soff , febar bou lakalé mais santeu Yallah, 3 ans de souffrances mais magui kaff di rétane di diém Happy. C’est pas facile wayé sante yallah, des fois damay guisse koumay wakh Marie ani sa ay nélaw lol, ay bouguéne khamone li gor di doundé ni pateu di deff semblant. Yallah naléne borom bi mousseul si tawate incha’Allah.

Tay j’ai craqué, joy na beu changé ndakh meunatou meu , sonena trope ak febar bi depuis meu yéwou coma batay meuna touma normal si dara dara . Le pire moy souma danélé bameu khol sama yaye yeurmandé bimouy am ci mane, ak nimouy diakhlè damay geuneu fébar. Yallah nama borom bi takhawou si li, sa youma djoulé gnane ko wére comme hôpital meunoussi dara loudoul calmant .

Jour bima geuné, meune deff poste bou rétanelou, jour bobou la geuneu soneu, jour bobou lay geuneu faible beu douma meune liguéy mais mangui santate yallah bou bakh sakh ndakh moma ték natoubi, j’accepte! Nguéne gnanal meu tané bou bakh, ndakh tolou si ndaw, wara daw tout le temps ngay fébar nékhoul ci khol. Des fois damay naneu est ce que mane dina goudou faneu ndakh métite.

Carnet Rose : Moussa Konaté s’est marié avec Kimi Bosh, une célèbre influenceuse

Articles similaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Bouton retour en haut de la page