Yaye Awa Rassoul: Ça bouge pas ma vie yenla
Alhamdoullilah je tenais à remercier tout le monde de m’avoir accompagné à ce beau jour de notre vie, nous les layennes dilen santantt santeuh bou amoul appeu nak di wakh nii contana deh walahi yalnalen Yallah fay beuss bi loussi way niak rek Yallah fayela
Di wakh samay nite merci bou amoul app merci rek lalen man wakh louma khewlei guisselen mou nekh mou meiti, banekh ak nakhar yeinangui togueu ak man Yallah diamalein inshaAllah.
Mangui wakh dieureudieuf appel bi nekhna, dialeuna ci diam, li dess yalna barkel inshaAllah
Bilahi contana lool ci nite yi, dall bi teiguine bi, discipline bi Yallah fayelen
Je tenais à remercier toute ma famille, mes frères, sœurs, mes enfants, je sais que vous voulez que moi khamna lolou boubakh motakh ma len di wakh diadieuf rek la famille, ça bouge pas ma vie yenla
Douma santeuh moukk teh douma wakh ci sama waji ki waral thiowli, kitah lima sol mou diapema,li rafet ci rewmi ma soolko dima d’éfal loubakh diko wakh diko dieufei nak @papebeyee Yallah rek lalay bayil mou fayela sa khôl bi sa yenei sii niit
Walahi kouy oute garmi nalaa teyei Pape Beye yaw des fois mani ki nite la ndakh sa khôl sa yenei yakhooma dei dangama beugue rek nakk moy lou yagueu 2014 ba 2024 mangui beugue yagg ak yaw deh merci infiniment