A LA UNE
Pod: sunu khôl you bone warnagneci gueinei khalifes dinnei yi
Pape Oumar Diop alias Pod: Franchement sunu reiwande ak sunu khôl you bone warnagne thi gueinei kilifeu dinei yi. Dangay Guisse nite kou teikiwoul dara comme man deuk thi togne Yallah am fitou tahaw di diokh leçons nos Khalifes Généraux.
Dagniy beugue torokhal la yakaar.