Uncategorized
A la Une

Ouztaz Modou Fall: Aziz Ndiaye dadone simbe gaindé Parcelles Assainies

Ouztaz Modou Fall: Aziz Ndiaye dadone simbe gaindé Parcelles Assainies

Mba hamngani Aziz Ndiaye simbekatou gaïndé lawone, maa dém ba Parcelles Assainies, cogne bimou done simbé, ma ladjie koko mounéma waw deuguela, ma lajiekoko mounéma deugueula simbena Parcelles Assainies.
Simbe gaïndé tickets yi 100 Fcfa-200 Fcfa bou ngoné gnou fay gaïndé yi. Aziz mi nékone gaïndé, Aziz mi limou dégue ci ay almomine, sakadja makadja, boul diar ci kéneu, diaral ci man mi (rires).
Tay Yallah défalko limko défal maniko diambar nga toguo.

Articles similaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Bouton retour en haut de la page