Uncategorized
A la Une

Daba Seye: Sidy Diop yalnala Yallah may ndam ci Zenith bi ci barkei Kaba bima diarkarlo

Daba Seye: Sidy Diop yalnala Yallah may ndam ci Zenith bi ci barkei Kaba bima diarkarlo

Daba Seye en pèlerinage à la Mecque actuellement a eu à faire une video pour prodiguer des prières à l’égard de son collègue artiste Sidy Diop. Vidéo ayant déplu beaucoup de Sénégalais, Daba Seye affirme dans la vidéo:

Sidy Diop manguilay nianal, mangui nianal arristes yeup, mais yow Sidy Diop manguilay nianal ci sa Zenith bi. Yalnala Yallah défal ndam bou mag, mou fess dél, nouko Youssou Ndour diaré mou fess, nouko Wally Seck diaré mou fess, Viviane diarfa mou fess, koufa mossa diar mou fess. Sidy yalnanguefa ame ndam, yalnangueko féssal dél, Yallah mayla ndam ci Zénith bi ci barki Yonanté bou tédeu bi, yalnala Yallah défala ndam bou kawé sa ndiorte ci barké Yonanté bi. Nangua santeu Yallah ndakh nianou khol lala nianal, di santeuh Yallah ndakh gueumnani nianou khol lala nianal. Yalnala Yallah may ndam ci bakei Kaaba gui ma diarkalo.

Articles similaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Bouton retour en haut de la page