Uncategorized

Bbei Bineta: jiguene meuna mougne lep sauf ay door, ay sagua, ay matraques melni kou yoor sa dome.

Bbei Bineta: jiguene meuna mougne lep sauf ay door, ay sagua, ay matraques melni kou yoor sa dome.

La tiktokeuse et influenceuse Bbei Bineta a lancé un cri de coeur aux hommes d’arrêter les maltraitances faites aux femmes dans les foyers. Elle les rappelle à l’ordre et aux devoirs. Peinée et chagrinée par le recit des souffrances vécues par son amie Ndakhte Lo, Bbei Bineta a lancé ce message très fort aux hommes:

Bbei Bineta:
Barki alkhourane jiguene mo sonou, jiguene moy mougne, jiguene moy togou, moy rakhasse, moy foote, moy passé, moy jiougué keur gneuw ci keur teh Yallah takh teh doussi ame louko nekh. Kholoul lo ame ak lo niakeu, dila mougnal teh Yallah tah, teh doussi ame louko nekh. Nite moy seuy dougnou ham loumou togualé, niou dieul wakh bou niaw bou nek tég ci kawam, moukay mounialé seuy seuy bi mais tamit lou eupe tourou. Jiguene meuna mougne lep sauf ay door, ay sagua, ay matraques melni kou yoor sa dome. Diape domou diambour melni kougnou wah sa bonne la, defko diamm pour lane? Ba louko nekh mou mougne, louko nakari mou mougne ba kagne? Seuy dou jiguene késsé, so beugué dara dangay def dara, mais jieul lép rek ni jiguene moy seuy ba kagne?
Jiguene moy jiéki rek dé ndakh nakar, kou mossa dégueu goor amna goitre, jiguene rek mokay ame ndakh ay nakar. Jiguene boufi fowé sa khel ba goitre fi heuy dé yako tégue sa bope ndakh diarougnouko. Né klen ay nite, dieul sen temps, dieukheur kén douko taneu dagne kay khol, ba guisse loula doy.

Alkaly Ndour remporte le Prix Ubuntu 2024

Articles similaires

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Bouton retour en haut de la page